
dimanche 12 (interlude) - carapid music lyrics
Loading...
[intro : kalz]
[verse : bako]
lu way bi tangueu, lu way bi tangueu tangueu
amneu kouko gueneu tangeu sodé g-yneum néko calmeu (anh)
fokniu tambeu, fokniu tambeu ndanke
def ni mame yi tambeu andak ték téy fi ci aduna
ooh defko boy waroul diafé, tek ci xey di dém niafé
niu bayi yeufou bandiyé
hey defko boy waroul diafé, tek ci xey di dém niafé
niu wagni yeuf you niak feyda
ci def lou bakh laleu bayi man
ci def lou bakh waro tayi man
aduna bi akeu beuri caïmans, ayi maan !
[hook : bako]
and every, everyday suniu life bou compliqué
niokey gueneu compliké kagn la niit di meusseu niité yeah
everyday, gueum yalla god tha king tambeu love té wagni hate
diapalanté biss bou né
Random Song Lyrics :
- brazul konggg - zuluzão lyrics
- wellblechdach - nepumuk lyrics
- lost without you - zakk cash lyrics
- ache - the heavy hours lyrics
- dancefloor - costa lyrics
- judgement day (tricky remix) - method man lyrics
- rnb - lil heavy chainz lyrics
- auf deinem balkon - madsen lyrics
- with my coolers - babydemon2006 lyrics
- tos zapatos - orco raspando lyrics