xam xam - cheikh ibra fam lyrics
Loading...
 
 
		xam xam mom kouko am gnako dara
xam xam mom kouko amoul amo dara
sama dom dianguil so maguai baye sa daara
sama dom dianguil so maguai baye sa daara
hé hé coly dolima
hé hé coly dolima
hé hé coly dolima
hé hé coly dolima
ni xam xam moy adouna
xam xam moy adouna
sama dom dianguil so maguai baye sa daara
sama dom dianguil so maguai baye sa daara
hé hé coly dolima
hé hé coly dolima
hé hé coly dolima
hé hé coly dolima
koly yaw dolima
koly yaw dolima
nigha tollou ghay djefé yaw
figha tollou rek ghay dokhai
nigha khamai rek ghay wakhai
kou wakh fegne kou djeuf fegne
ghagni dianguilene
hé hé coly dolima
hé hé coly dolima
hé hé coly dolima
hé hé coly dolima
Random Song Lyrics :
- shpr1t3! (remix) - блинк (blink) (rus) lyrics
 - new saviour - squealer lyrics
 - bigtittygothegg - sxdboynoah lyrics
 - коля, коля 2 - lida lyrics
 - lacoste áfrica - mc lipi, mc lemos & oldilla lyrics
 - delhore - arash lyrics
 - reaching - kirat lyrics
 - war - salemkuma lyrics
 - mary, did you know? - sarah jay hawley lyrics
 - là-bas - yba lyrics