
mathiou - thione seck lyrics
Loading...
ndeye ndeyou ken la baye bayou nieupe la, sama yaye djé, sama yaye djii, guissouma koumalay meuna wethiéé, yaw mi gueune si mane yaw mi gueune si mane
yaye boye sama galadj
bo beugué djote sama djiko toudal sama yaye douma ko fowé doma ko fowé yaye boye sama galadj
rote nga thi leudeum debb nga thi taw, wale thi nadj bou tang bou yaye yeup melen ni yaw kene dou diour di sani
(refrain )
ndeye ndeyou ken la baye bayou nieupe la, sama yaye djé, sama yaye djii, guissouma koumalay meuna wethiéé, yaw mi gueune si mane yaw mi gueune si mane
yaye boye sama galadj
djéba ndoye, indou woma woma ndeye sane, bayo boye dom djou am yaye day am baye wow wo
Random Song Lyrics :
- signal - presence, clockwise lyrics
- hocine - baisse les yeux - talentueur ( episode #1 ) - hocine lk lyrics
- same nigga - ty dolla $ign lyrics
- october - mac lethal lyrics
- 아침에 다시 얘기해 (ady) - boi b lyrics
- rogers park - justin townes earle lyrics
- not waving, but drowning - high contrast lyrics
- codex - codex lyrics
- i just can't break it to you - pixies lyrics
- tatooine - phineas e ferb lyrics