
mon combat - wally b. seck lyrics
[paroles de “mon combat”]
saf nga djiguén lolou lalay topé
damla khol lima guiss dima choqué
ni nga mél naturelle la, doko forcer, non
guel bi dafa tang badi laké
safara bi nelow si yow la begg guiss (wopopop)
pessé naala, ci li nga tok dafa diiss
saf ni jumbo, toy ni rico
guel bi dafa tang badi laké, chaud
bad girl boy boula diégué ma shoot
limay weur yeup ci djiguén nga ouf
sa bep morom boula teukou nga shoot*shoot*shoot*shoot*shoot
baby kaay sama wet, mbeuguél lalay sééd, man dama dioy
bilay yaay kimay daanel oh oh oooh
bimala guissé sama khol dafa nékh
bimala guissé eh eh eeeh
baby kaay sama wet, mbeuguél lalay sééd, man dama dioy
bimala guissé eh eh eeeh
sama linguère yaa khééré dé
am nga thiass, waw ya tiékété
yow lay weur souba ba ngone ma teudi
yaag na beuré wayé yow tu es mon combat
bandit bandit baby bandit bandiloul (bandé)
wan ma sa bandit weundéloul
thiow*li thiow*li yow la diougal nga féémou
daggal sa yaram niou ndelou
bad girl boy boula diégué ma shoot
limay weur yeup ci djiguén nga ouf
sa bep morom boula teukou nga shoot*shoot*shoot*shoot*shoot
baby kaay sama wet, mbeuguél lalay sééd, man dama dioy
bilay yaay kimay daanel oh oh oooh
bimala guissé sama khol dafa nékh
bimala guissé eh eh eeeh
dama dioy, sama khol dafa nékh
dama dioy, bimala guissé
Random Song Lyrics :
- rise (leave me alone) - radio edit - safri duo lyrics
- sensation - sister city lyrics
- somewhere in europe - bagatelle lyrics
- find me - jun hyo seong lyrics
- kačket dole - corona lyrics
- trust - j-soul lyrics
- maniquine (sellout radio edit) - transrelic lyrics
- the handyman - mickey avalon lyrics
- skyline - the anchors lyrics
- paname nuit - a2h lyrics