
4/4/1944 - youssou n'dour lyrics
4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk, moo neex
boo lékkee ba suur war ngaa gërëm, war ngaa gërëm ñi dugg ci waañ wee, waañ wa tàng na
tóllu nii war ngeena bég, war ngeena bég ci independans bi, ak ñi ko indi
4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk, moo neex
boo lékkee ba suur war ngaa gërëm, war ngaa gërëm ñi dugg ci waañ wee, waañ wa tàng na
dama ne bu lëk lékkee olom budee gore na te dëggu war na ko gërëméé picc yi
no, no, no, no, no, no
no, no, no, no, no, no, yee
4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk, moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk, moo neex
ah lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, gis say mbokk moo neex
lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, gëm sa bopp moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex
no no no gis say mbokk moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex
waaw lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, gis say mbokk moo neex
aaaaa, moom sa bopp, moo neex
waaw lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, moom sa bopp, moo neex
Random Song Lyrics :
- my demo ns - skrr brr ayy lyrics
- shum vodi - kennycano lyrics
- brave new world (2017 version) - iron savior lyrics
- сто шагов (hundred steps) - heartsnow lyrics
- dancin’ - neon valley lyrics
- frequência - uclã lyrics
- lil rain - thereallilrain lyrics
- cabbage - gnar lyrics
- the law - angerfist lyrics
- mom is trying - r.d.l lyrics