
bamako - youssou n'dour lyrics
si gare bi lako fekkeu, mi ngui sanguo seur té beut yi di takkeu, ma dal di koye nougnou mou dal di maye faye, dal di maye yédeu ci adouna bou yakhou bi mane douma fatté!
ah mani ah mani! douma fatté bamako lii mani lii mani! mane douma fatté! kerok lama khamal louma khamoul woone ci diamono bou yakhou bi yénene ak yénene; balaa maye dougeuti mane ci loumou meuneu doone dinaa fattélikou ndaw sossou limouma wakhoone! souy souy sou sou sou sou sou souy souy!
ci gare bi lako fekkeu mi ngui sanguo seur té beut yi di takkeu, ma dal di koye nougnou mou dal di maye faye dal di maye yédeu, maky yé maky maky yé maky yéééééééééééé! waw kérok lama khamal louma khamoul woone ci diamono bou yakhou bi, balaa maye dougeuti ci loumou meuneu doone, dinaa fattéli ko maky yé maky maky yé maky yééééééééééééééé! ah mani ah mani! douma fatté bamako lii mani lii mani! mane douma fatté bamakoooooooooooooooooo
Random Song Lyrics :
- party like it's 1846 - lil toy yoda lyrics
- gec deyil - promete lyrics
- when it's all over - dunbarrow lyrics
- on my time - bobby g lyrics
- nouvelle ère - hoshi (fra) lyrics
- z.m.r.d. - idea & strýc nory lyrics
- bratki - doomee & маленький ярче (malenkyi yarche) lyrics
- ateenalaisten laulu - polyteknikkojen kuoro lyrics
- up in smoke - bad wolves lyrics
- sweet spot - yoinkin lyrics