
yaay jêrëjëf - youssou n'dour lyrics
yaay jërëjëf
yaay jërëjëf
yaay booy
yaay jërëjëf
yaay jërëjëf
yaay booy
{music}
déglu ti leen, ma wax ati ko
ku ko déggul, ngeen jottali ko
kuy teral sa yaay, te nga dekëti
ba amm ngërëmëm, yàlla [moo] lay teral
(mani) déglu ti leen, ma wax ati ko
ku ko déggul, ngeen partager ko
kuy teral sa yaay, te nga dekëti
ba amm ngërëmëm, yàlla [moo] lay teral
{music}
yaw sa yaay booy, moo sonnoon ci yaw
moo la daan boot, di yendu taxaw
bu ko weccoo k*leenen
bu la ko kenn jaral
{music}
leeg*léeg muy dem fu sori lool
même bu am ee luy lorel
budé sa soxla la, sa yaay dara du ko tëyyé
{music}
[yaay jërëjëf]
yaay jërëjëf
yaay booy
yaay jërëjëf
yaay jërëjëf
yaay booy
yaw sa bonheur (waawaaw), mën ta am benn solo
féek [yaw] sa yaay j*pp ul sa loxo bi, taf la ci dënn ëm
youssou yaay, garab la
[yaw] sa bonheur, mën ta am benn solo
féek [yaw] sa yaay j*pp ul sa loxo bi, taf la ci dënn ëm
(waawaaw) ni la sagal nga ma, ché yaay
yaay booy, walaye or la
(mani) déglu ti leen, ma wax ati ko
ku ko déggul, ngeen jottali ko
kuy teral sa yaay, te nga dekëti
ba amm ngërëmëm, yàlla [moo] lay teral
(waaw) déglu ti leen, ma wax ati ko
ku ko déggul, ngeen partager ko
kuy teral sa yaay, te nga dekëti
ba amm ngërëmëm, yàlla [moo] lay teral
yaw sa yaay, loo ko jox*jox it, bu ko naw
lu mu rëy*rëy, do ko raw
boo ko am ul éé, nga yéené ko*ko
li ne sa xol bi, yàlla xam na ko
(waawaaw) youssou yaay, diamant la, or la
jërëjëf yaay
youssou yaay, garab la, yaay kër la
abdoulaye ni daaro mbaar, maajoor ni daaro mbaar
matar ni daaro mbaar, ak seen jigéen
sóogi digéek, birëm digi samba
lool kurë mbisaan sugu paate sambala ganja, leen siré
yaay soxna mboup, jërëjëf yaay
déglu ti leen, ma wax ati ko
ku ko déggul, ngeen jottali ko
kuy teral sa yaay, te nga dekëti
ba amm ngërëmëm, yàlla [moo] lay tеral
(mani) déglu ti leen, ma wax ati ko
ku ko déggul, ngeen partager ko
kuy teral sa yaay, te nga dеkëti
ba amm ngërëmëm, yàlla [moo] lay teral
ku bëgg sa yaay? (youssou) waaw! waaw!
ku bëgg sa yaay? nél jërëjëf!
ku bëgg sa yaay? (youssou) waaw! waaw!
ku bëgg sa yaay? nél jërëjëf!
tu aimes ta maman? (youssou) oui! oui!
tu aimes ta maman? dis merci!
tu aimes ta maman? (youssou) oui! oui!
tu aimes ta maman? dis merci!
you love your mom? (youssou) yes! yes!
you love your mom? say thank you!
you love your mom? (youssou) yes! yes!
you love your mom? [say thank you!]
tu ami mamá? sí! sí!
tu ami mamá? di grazié!
tu ami mamá? (youssou) sí! sí!
tu ami mamá? di grazié!
Random Song Lyrics :
- cannibal d&b - sunshine christo lyrics
- oh god's love - kendle pulse, boswell love, zoe love lyrics
- 防弾チョッキ2 (bulletproof vest 2) - young zetton & watson lyrics
- after the storm - ofdrykkja lyrics
- can’t be stopped (ccc) - lil scxars lyrics
- biography - yammi lyrics
- doggy - winslow house lyrics
- dans les abysses - frozenration lyrics
- when i see u - jolio foolio lyrics
- like that - kaliran lyrics