
yama - youssou n'dour lyrics
soubateel, bamuy barilã©
ã‘i di dã©loo sen palanter
ngir baã±a xaar li xew, li xew fã©neen
chorus
ni woo yama, ni yama ku la seetlu woon (bis)
gaal gi teer
ba ã±u seet li, li wara dem fã©neen
tã© du yeebi ludul meew lifi des
chorus
ni woo yama, ni yama ku la seetlu woon (bis)
moo waral bu sã©dalã©, du am
du am. rusna ã±aan ba day fandã©, fandã©
moo waral bu sã©dalã©, ba du am,
du am. rusna ã±aan kii daal amu fi morom
yaamaa nango sona lol
chorus
ni woo yama, ni yama ku la seetlu woon (bis)
ni dox sa waar bamu noppi yaw
tã©rã©wul topa bã«gã« bã«gã« xalã©yi
yaama rek la soxal diarama, diarama, diarama
ni woo yama, yama
wuy yama, amufi morom
wuy yama, nangoo sona lol
ni yama, jigen ju man goor
wuy yama, maa la setlu way
moo waral bu sã©dalã©, du am
rusna ã±aan ba day fandã©
amu fi morom
mala setlu way
yama, yama
amul noflay,
amu fi morom
tunda wi raã±ã©naã± la
yama, yama
chorus
ni woo yama, ni yama ku la seetlu woon
ni woo yama, ni yama gaa yi yaaba leen
ni dox sa waar bamu noppi yaw
tã©rã©wul topa bã«gã« bã«gã« xalã©yi
yaama rek la soxal diarama
Random Song Lyrics :
- 4x - soulja boy lyrics
- tietäjät tietää - ikinä lyrics
- k onda senpai - k onda lyrics
- let not your heart be troubled - jillian edwards lyrics
- honey (i miss you too) - margaret lewis lyrics
- high life - marcie free lyrics
- #23/wock anthem2! - kiddsaif lyrics
- ty ja on - dwóch niepozornych lyrics
- mar y tierra - santa fe klan lyrics
- head hunter (dick riders diss) - 133 dripking lyrics