lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu méritewoumala – amadeus

Loading...

méritewoumala lyrics
méritewoumala, eh yeah
méritewoumala, eh yeah
méritewoumala, eh yeah

wakhal sa xol ni fonk na
ko tekk na ko fouma tekkoul keun oh yeah, ah yeah
wakhal sa xol ni fonk na
ko tekk na ko fouma tekkoul keun oh yeah, ah yeah

méritewoumala
méritewoumala
yallah xam na méritewoumala
oh méritewoumala
ateh woma nyakal bumaye deconné
decidé wo bagne ma, xar bama kheuyé dem
toundou bi yeup yeuk sa tarr
té takhoull nga changé
méritewoumala

wakhal sa xol ni fonk na
ko tekk na ko fouma tekkoul keun oh yeah, ah yeah
wakhal sa xol ni fonk na
ko tekk na ko fouma tekkoul keun oh yeah, ah yeah

méritewoumala
méritewoumala
yallah xam na méritewoumala
oh méritewoumala
na assamane si taw mour sa ay rongogne
na denou bi dall neubeu sa ay khikheute
beugou ma ngai dioy
danga maye dofflo
rabbill alameen na ma bolek yow
ci sa weet rek laye meuna keparo

na assamane si taw mour sa ay rongogne
na denou bi dall neubeu sa ay khikheute
beugou ma ngai dioy
danga maye dofflo
rabbill alameen na ma bolek yow
ci sa weet rek laye meuna keparo

wakhal sa xol ni fonk na
ko tekk na ko fouma tekkoul keun oh yeah, ah yeah
wakhal sa xol ni fonk na
ko tekk na ko fouma tekkoul keun oh yeah, ah yeah
wakhal sa xol ni fonk na
ko tekk na ko fouma tekkoul keun oh yeah, ah yeah

méritewoumala, eh yeah
ah méritewoumala, eh yeah
méritewoumala, eh yeah

lirik lagu lainnya :

YANG LAGI NGE-TRENDS...

Loading...